Ahmed Khalifa Niass – Béneu fébar la am » moy beugu Serigne Touba té meunou maci dara »
Ahmed Khalifa Niass – Béneu fébar la am » moy beugu Serigne Touba té meunou maci dara «
Date:
Ahmed Khalifa Niass – Béneu fébar la am » moy beugu Serigne Touba té meunou maci dara »
DEPECHES
[email protected]
+1 404 547 2456
Pour vos publicites:
[email protected]
© 2024 Xalilmasn.com. All Rights Reserved.
kobeugue beuguenele thank you brother niass.
Yaw bago ken yaw ak sidi yenayam
Il ment , Beugue Serigne Touba diaroula takhawe devant les medias diko annoncé ,danoukoye dieufé , dou aye wakhi kessé . Ce mec joue et profite sur l ignorance de la majeur parti de nos concitoyens… C est un homme de Zahir il aime que les femmes l argent, les cacas de Satan le bling-bling … Bamba etait un homme de Baatin….
Mai si tu aime borom touba lui qui est la lumière de lislam et qui a permis à lhomme noir de retrouver sa dignité et qui a défendu lislam quand tout le monde négocié avec les blancs, alors pourquoi tu as essayé de soigner ta maladie d’amour selon tes dires : Bén fébar la am moy beugu Serigne Touba té meunou maci dara Diém na diém wayé meunou maci dara.
Pourquoi guay diém? Parce que beugg serigne touba ndam bou rëy la.
peut être que cest juste une manière de parler. Wayé faut respecter l’entendement des sénégalais. Nitt yi lay déglou aussi ne sont pas tous dépourvus d’esprit d’analyse. Di djeguelou ci kadougui
Mai si tu aime borom touba lui qui est la lumière de lislam et qui a permis à lhomme noir de retrouver sa dignité et qui a défendu lislam quand tout le monde négocié avec les blancs, alors pourquoi tu as essayé de soigner ta maladie d’amour selon tes dires : Bén fébar la am moy beugu Serigne Touba té meunou maci dara Diém na diém wayé meunou maci dara.
Pourquoi guay diém? Parce que beugg serigne touba ndam bou rëy la.
peut être que cest juste une manière de parler. Wayé faut respecter l’entendement des sénégalais. Nitt yi lay déglou aussi ne sont pas tous dépourvus d’esprit d’analyse. Di djeguelou ci kadougui. Wasalam
Fene rekk
Amadou mor bamba bopam rek la wane
Ahakay beugue na bamba nagoul léne ko ; nit dagay khole lamou bakhlé gabok koc mome lamou safane lé ga nianalko ci
Mame khadim Rassoul est universelle.ken rekk mo am si serigne touba thieur kou sap doundou deupo ak charia ndahté mom leupame zahir ak batine da deupo ak chariatou yallah. Di dieugeulou.