jeudi 25 février 2021 12h32
  • Xalima15ans
  • PUBLICITE
  • CONTACTS
Ecoutez Xalima Radio
Regardez Xalima TV
  • ACCUEIL
  • ACTUALITES
  • Chroniques
    • L’oeil de l’expert avec Cheikh Faye Ph.D
    • Alassane Kitane
    • AUTOPSIE
    • Bathie Ngoye Thiam
    • Bosse Ndoye
    • Les chroniques de Sigapal
  • Opinions
  • PEOPLE
  • SPORTS
  • VIDEOS
    Direct-Ganuk Xalima Mayacine Diop reçoit Seydi Gassama (Amnesty International)

    Direct-Ganuk Xalima Mayacine Diop reçoit Seydi Gassama (Amnesty International)

    Cité dans une affaire de viol : Ousmane Sonko accuse ouvertement Macky Sall

    Mame Diarra Fam chez Ousmane Sonko

    Affaire Boubacar Seye: Ganuk Xalima avec Mayacine reçoit Seydina Seck et Souleymane Alioune Diallo

    Affaire Boubacar Seye: Ganuk Xalima avec Mayacine reçoit Seydina Seck et Souleymane Alioune Diallo

    Direct-Ganuk Xalima/Affaire Boubacar Seye: Mayacine Diop reçoit Yaye Amy Diop et Amadou Dieng

    Direct-Ganuk Xalima/Affaire Boubacar Seye: Mayacine Diop reçoit Yaye Amy Diop et Amadou Dieng

    Émission spéciale sur l’arrestation de Boubacar Séye: Mayacine Diop en discute avec Momar Dieng Diop

    Émission spéciale sur l’arrestation de Boubacar Séye: Mayacine Diop en discute avec Momar Dieng Diop

    Vidéo-Me Moussa Diop mouille le nouveau DG de Dakar Dem Dikk: “ il conduit une Land Cruiser Platinum de 85 millions ”

    Vidéo-Me Moussa Diop mouille le nouveau DG de Dakar Dem Dikk: “ il conduit une Land Cruiser Platinum de 85 millions ”

    Vidéo-Me Moussa Diop sur sa deuxième épouse: “ je l’ai viré de Dakar Dem Dikk avant de l’épouser ”

    Vidéo-Me Moussa Diop sur sa deuxième épouse: “ je l’ai viré de Dakar Dem Dikk avant de l’épouser ”

    Disparition de Diary Sow, l’ancien ministre de l’éducation, Serigne Mbaye Thiam, confirme

    Le Consul général du Sénégal à Paris : « La vie de Diary Sow n’est pas en danger … »

    Couvre-Feu : un mal nécessaire selon les populations rencontrées

    Couvre-Feu : un mal nécessaire selon les populations rencontrées

  • RADIO FM
    • All
    • 3eme Mitemps avec Sindo
    • 8 Mars
    • A LA UNE
    • ACTU+
    • ACTUALITES
    • Afrique
    • Alassane Kitane
    • Appel
    • AUTOPSIE
    • Bathie Ngoye Thiam
    • Bosse Ndoye
    • CELEBRITES
    • Chroniques
    • clips
    • Coin de femmes
    • Comment vivre avec Coronavirus
    • Communiques
    • CONFINONS-NOUS
    • COVID 19
    • Culture
    • DEPECHES
    • Diaspora
    • Diplomatie
    • Dossier
    • Drame
    • economie
    • Education
    • Environnement
    • Eutou Xalima
    • FAITS DIVERS
    • Gamou
    • Gouvernement
    • Homme de l'annee
    • INTERNATIONAL
    • Jotaay ji
    • Justice
    • L'oeil de l'expert avec Cheikh Faye Ph.D
    • La Une des Quotidiens
    • Le point avec Oumar Ba
    • Les chroniques de Sigapal
    • Livres
    • Lutte
    • L’espace numérique
    • Magal
    • Mody Niang
    • Musique
    • Nafila
    • Nécrologie
    • Opinions
    • PHOTOS
    • PODCASTS
    • Politique
    • Presse
    • RADIOS FM
    • RAMADAN
    • religion
    • Retro
    • Revues de La presse
    • SANTE
    • Science
    • Sémaphore par Elhadji Aziz Guèye
    • Seybani Sougou
    • Sketchs Ramadan
    • Societe
    • sourates
    • SPORTS
    • Telefilm
    • Témoin d’Histoire
    • Teuss et Xalass
    • Videos
    • XALIMA 15 ANS
    • Xalima Tv
    Nécrologie: Le Professeur Daouda Ndiaye en deuil…

    Nécrologie: Le Professeur Daouda Ndiaye en deuil…

    Levée de l’immunité parlementaire de Sonko: la commission Ad hoc validée

    Levée de l’immunité parlementaire de Ousmane Sonko : la liste des cinq orateurs qui seront autorisés à prendre la parole dévoilée

    Covid-19: les pistes de solution du Dr Papa Ndary Niang pour juguler la pandémie au Sénégal

    Covid-19: les pistes de solution du Dr Papa Ndary Niang pour juguler la pandémie au Sénégal

    Procès en diffamation: Serigne Mboup réclame 1milliard aux 11 membres du CCIAD

    Procès en diffamation contre la Ccid: Serigne Mboup débouté

    Point du jour du coronavirus : 06 décès, 63 cas graves en réanimation et 268 nouvelles contaminations ce lundi 15 février 2021

    Point du jour du coronavirus : 12 décès, 49 cas graves en réanimation et 288 nouvelles contaminations

    Alpha Condé : “les journalistes français ne respectent pas les chefs d’États africains, moi je n’accepte pas qu’on me manque de respect”

    Alpha Condé : “les journalistes français ne respectent pas les chefs d’États africains, moi je n’accepte pas qu’on me manque de respect”

    Assemblée nationale: échanges de propos aigres-doux entre Cheikh Bara Doly et Abdoulaye Makhtar Diop

    Assemblée nationale: échanges de propos aigres-doux entre Cheikh Bara Doly et Abdoulaye Makhtar Diop

    Lagon 2: des jeunes qui se faisaient passer pour les fils de Macky et d’Idy arrêtés

    Lagon 2: des jeunes qui se faisaient passer pour les fils de Macky et d’Idy arrêtés

    Revue de Presse (Wolof) de Zik Fm du Mercredi 03 Février 2021 avec Ahmed Aidara

    Revue de Presse (Wolof) de Zik Fm du Jeudi 25 Février 2021 avec Ahmed Aidara

No Result
View All Result
Xalima.com: 15 ans au service exclusif de l'information
No Result
View All Result
Mbirum « SWEET BEAUTÉ » : Ngalla Buleen Gàkkal Turu Senegal ! Bubakar Bóris Jóob (Ñu jukkee ko ci SenePlus, ci tekkib Ndey Koddu Faal)

Mbirum « SWEET BEAUTÉ » : Ngalla Buleen Gàkkal Turu Senegal ! Bubakar Bóris Jóob (Ñu jukkee ko ci SenePlus, ci tekkib Ndey Koddu Faal)

22 février 2021
publie dans la rubrique Opinions
6
Share on FacebookShare on TwitterPartager sur WhatsappEnvoyer un emailPartager sur Telegram

Pólitise? yeey faral di def lu xew ñu daldi àddu ci tàng-tàng bi. Loolu, nag, warul a jaaxal kenn. Ndaxte, ñoom, daanaka, bu waxtu jëf jotee, ku ci taxaw di seetaan tàkk nga. Gaa, du li gën. Waaye, nag, buñ demee ba mbirum «Sweet Beauté » di bëgg a gàkkal sunub demokaraasi, kenn warta noppi, ñépp a war a sotle réew mi.

Li yéeme ci mbir mi mooy ne, li muy réy ak a doy waar yépp, dafa xaw a reetaanlu. Nde, mbir mi, ay léeb lay gën a niru. Laaj biy yëngal tuñ yépp mooy : naka la Usmaan Sonko, njiitalu PASTEF di sañ a wàcce boppam, sàggan bay tëdde jigéen ju am ludul 20i at astemaak di ko siif ci béréb boo xam ne, weñ sax bu fa naawee ñu dégg ko ? Dàmpukaay boo xam ne, mu ngi cig kër gu, daanaka, 10i nit ñoo fay nekk guddeek bëccëg. Foofu, naka lañ fa mënee jaay doole as ndaw, tëdde ko fa ay yoon teg ci di ko xëbal ak ñaari gànnaay te kenn du ko yëg ? Ndax Usmaan Sonko dofe na noonu ? Ak ni kër gi tuutee te am iy fuglukaay… Du yuuxu, du jooy te du benn bërti-bërti bu fa kenn mës a dégg. Lii, bu dul ay léeb itam, caaxaan du ko weesu.
Sonko xam na xéll ne ay noonam ñoo ngi koy yëddu saa su ne, di ko jéem a fexeel. Bañ na ko ba buy tukki, du nangoo dencluy wëliisam ci suufi roppëlaan yi. Ku ni mel, naka lay siife as ndaw, ak ni darajaam tollu ci miim réew ? Waaye, fen, du bijjaaw.

Ñi nas kooto bi, bëggoon ko gasal kàmb, sóoraalewuñu woon ni boroom dàmpukaay bi du far ak ñoom. Kii, kàddu yu leer nàññ la yëkkati. Ciy waxam, ay sàmbaa-bóoy a diisoo ci pet ngir daaneel Sonko. Dara taxu leen a jaar ci Ajaa Raabi Saar lu dul ay jaar-jaar ak xelu xale mi ci moom. Ndege, Ajaa Raabi Saar, ci li ñenn ñi wax, bare na caaxaan, bëgg na fo, te ku sob a sob la. Melokaanam boobu, moo taxoon nooni Sonko yi bëgg koo jëfandikoo nib gànnaay ngir wàcce ko ci nii, mbaa ci naa.

ADVERTISEMENT

Xaalis mënul a jënd as gor. Fa seen pexe moyee tamit mooy ba ñu yaakaaree ne mbir mu tollu nii, ci réew mu mel ni Senegaal, du senn. Waaye, ci waxtu yu néew la law ba suul yeneen yitte yépp, ñépp di ko waxtaane. Dañu sax fàtte mbas mi xam nga ne, bés bu Yàlla sàkk muy gën a rey.

Askan wi, moom, dafa mer ba futt. Te, meram googu, kenn waralu ko ku dul Maki Sàll, njiitu réew mi, ak nguuram gi. Réewum demokaraasi, bu jaaree yoon, kàddu askan wee fa war a sut geneen kàddu gum mënti doon. Askanuw Senegaal, nag, Sonko la jox kàddoom. Loolu, sikk amu ci. Xew-xew yii doy nañ ci firnde. Kon, ak luñ mënti sos ngir daaneel Sonko, askan wi, moom, àtte na ba noppi. Warees na xam ne, léegi, ñépp a yeewu, naxe-mbaay moo fi jeex. Mu mel ne, Sonkoo ci amee ndam.

Ba sun-jonni-Yàlla-tey jii, ay ndaw yu gisoon seen bopp ci moom ñoo toppoon ci Sonko. Waaye, fii mu ne nii, nit ñaa ngi màbbe fu nekk, di ko jàppalesi. Loolu day wone ni dooleem yokkoo ci làngu pólitig gi. Bu dee dayob Sonko da doon màgg ndànk-ndànk, tuuma yii dañu yokk bayreem.
Kasu pólitig gu kii walla kee amalun solo. Waaye, demokaraasi lañu bëgg a gàkkal. Te li am sax, mooy ne, ñi ko waroon a wattu, ñoo koy doyadil. Dara desul ginnaaw. Nee nañu ndaw si dañ koo siif. Waaye, moom de, ba mu kalaamee Sonkook yoon ba tey, da ni mes, ni meles.

Waxatuñu dara ñu jël maniyu boroom-kër yóbbu cib kilinig. Loolu doyul, ñuy xoqtal ak a jéem a ger boroom dàmpukaay bi ngir mu soppi seedeem, daldi taqal Sonko.

Basiiru Gèy moom, mooy toppekat bi nga xam ne, lu ko nguur gi sant mu def. Ñu daldi woolu Sonko ci maa-tey, mel ni du dipite bu malaanum kiiraay muur. Ñu ni déet-a-waay, takk-der yi wër këram ak seeni gànnaay. Ñoom daal, ñuy jalgati yoon nimu leen neexe.

Loolu doyul, Péncum réew mi ne dafa wote ba toog, keroog bésub 11eel ci féewaryee, ngir teg Sonko ci yoon woo xam ne kenn gëmatu ko faf. Wallaay, lii daa mujj doon tiis sax.

Lu jiin Njaag a, te njiitu réew meey Njaag. Ndaxte, mooy buur di bummi. Looloo waral tamit ñetti kuréli dogal yi waroon a tëdde njaaxanaay mujje we??.

Naam, Senegaal du réewum jaay doole mi ñuy wax, waaye xoqtal beek bunduxataal bi du fi lu bees. Li fi bees, jamono jii, mooy nim fése, ñaaw, ruslu te xaw a reetaanlu. Maki Sàll xamul bët, faalewul kenn. Te, loolu, jar naa tiit bu baax. Ponk bu mujj bii laaj na taxaw-seetlu.

Am na ñenn ciy farandooy Maki Sàll ñuñ weg lool ndax dañoo mës a gëm Senegaal ak lu koy jëmale kanam. Su leen neexee ñu taamu jàppale ko : miin nanu dem ak dikk ci géewu pólitigu Senegaal. Dara nekku ci. Li neexuta dékku kay, mooy naka lay xeltukat yu màndu te am faayda ni ñoom mënee seetaan lii, ne cell. Mbaa du Njiitu-réew mi dafa yóbbu seen fit ?

Suñ doon doxal yoon, Maki Sàll dina xam ni du lu ko neex rekk mu def te dara du ko ci fekk. Ñi mu àndal waruñu ko cee seetaan benn yoon. Moom daal kenn woowu ko ci ruq, déey ko.

Mën nanoo jëli gaa ci pàrteem ay kàngam yu dul jaaroo taal ak Sonko. Waaye, dinañ am kersa ci doxalinu Maki Sàll. Tóoxidóona gu mu jóge, jàll ca ga ca des. Bërki-démboo-njaay, Karim Wàdd, démb Xalifa Sàll ak Aminata Ture ; ñépp liñ teg ci seen ndodd mooy ne dañoo bëgg a wuutu Maki ci jal bi. Waay-waay kenn mënu koo déey ne “màggal nit màggal gu jéggi dayoo jigul pólitise? ci miim réew”. Ni muy doxaleek Sonko du ko jig, dafa nar a xëtt xolam rekk, balaa yàgg mu ne fi naan su ma yëgoon. Ñépp xam nañ ni “lu ëpp tuuru” te Sonko ciy yëkkatiku ëllëg-ak-sibir.

Xéy-na, nguur gi da doon làmbaatu ba xam fu dooley Sonko tollu. Ndax, ci xarala yu bees yi kese la am i farandoo am déet. Waaye, daj na. Ci diir bu gàtt, ñu baree fippu, génn ci mbeddiy Ndakaaru yi, Luga, Biñoona, Mbuur ak Sigicoor. Te buñ deful ndànk dina law. Rax-ci-dolli, Pastef da cee gën a yëkkatiku bitim-réew.

Li ci Maki Sàll waroon a jànge mooy ne, am na lu koy xaar bés bu bëggee amaat ñetteelu moome. Na xam ne li jig Alasaan Daramaan Watara ak Alfa Konde du ko jig.

Su gëmoon Yàlla, dina xam ni mënoo taal am réew ngir rekk bëgg a wéy di ko jiite. Diggante awril ci atum 1960 ak 2021, ay milyo?i doomi-Senegaal jaar nañ fi. Ci seen biir, ñeent rekk a fi am màqaamaam nekk njiitu réew. Milyo? yi ci des te mësuñoo jiitem réew, wàññiwuleen dara. Te, bu yaakaaree ni moo leen ëpp xel mbaa kàttan, day nax boppam.
(Ci tekkib Ndey Koddu Faal)

Thiernomab

Thiernomab

Lire Aussi

Covid-19 : un premier cas de variant brésilien identifié en Allemagne
Opinions

Plaidoyer pour un retour à la normale au Sénégal – Les enjeux (Par Alpha Waly Diallo)

24 février 2021
DIC : Guy Marius Sagna arrêté
Opinions

Yonou Askanwi /FRAPP France Dégage : « Mettre fin à la chasse à l’homme, aux arrestations arbitraires et à la dictature »

24 février 2021
Plainte pour viol contre le leader du Pastef : La propriétaire du salon de massage lave Ousmane Sonko à grande eau !
Opinions

“Patriotes militants du Sénégal ! Union et vigilance” (Par Alla Kane)

24 février 2021
La Dictature est Fragile
Opinions

La Dictature est Fragile

24 février 2021
“Pour assoir la dictature Faye/Sall, on cherchera à coller des motifs de mœurs…” (Mamadou Lamine Diallo)
Opinions

“Pour assoir la dictature Faye/Sall, on cherchera à coller des motifs de mœurs…” (Mamadou Lamine Diallo)

23 février 2021
Affaire Boubacar Seye: Alioune Tine, Bruno d’Erneville…face à la presse, vendredi
Opinions

“Sauver l’Etat de droit, Renforcer la Démocratie et Garantir la Paix civile” (Par Aliou Tine)

23 février 2021
Hommage au Professeur Cheikh Faty Faye (Par Mamadou Birame Faye)
Opinions

Hommage au Professeur Cheikh Faty Faye (Par Mamadou Birame Faye)

23 février 2021
Dr Babacar Diop “demande aux Guelwaars d’être mobilisés…” pour soutenir Sonko
Opinions

Quand la démocratie agonisante interpelle notre devoir de résister (Par Dr Babacar Diop)

23 février 2021
Attention aux vaccins privilèges (Par Seydou Ka)
Opinions

Attention aux vaccins privilèges (Par Seydou Ka)

23 février 2021

Comments 6

  1. Mamadou says:
    3 jours ago

    eskey, jangaat bu leer te werr! Maki Sall nda xam nee Senegal mokko magg fuff. Xayaan ku degg Serer.

    Répondre
  2. Lemzo says:
    3 jours ago

    M. Diop, mes respects, mais soyez un peu plus sérieux… Il s’agit d’une affaire de viol et de la dignité d’une jeune fille pauvre de 20 ans…

    Répondre
    • Anonyme says:
      3 jours ago

      Pas si pauvre car mobiliser une équipe médicale,un laboratoire un avocat un 4×4 avec chauffeur le procureur en chair et os nuitamment par un coup de fil n’est pas donné même à certains riches L’avenir nous dira!

      Répondre
  3. Bëg dëg says:
    2 jours ago

    Borom xam xam bu jubb ni seex anta joob raflee na ci miim reew. Boris sa feete daa fës. Dafa meelni Persidank Maky moo sakku xalebi. Ndeyu mbili ji Sonko moom danga ko ragg ba mi set. Boris sa njubb des na

    Répondre
  4. Ahmadu says:
    2 jours ago

    Bilaay borom xam xam bu jub te dëggu ni Seex Anta Joob rafle na ci miim reew. Boris sa xëltu bii andul ak maanute, andul ak ngor. Ndayyu mbili gi, Sonko, danga ko ragg ba mu sett wecc. Lu njiin njaag mooy njaag. Xam xam bu andul ak njubb ak manute, bu yaaggee goone yi sax won la ginaaw

    Répondre
  5. Karara says:
    2 jours ago

    Au Sénégal, le bon sens est la chose la mieux partagée. On peut lire, comprendre les non-dits, les silences et surtout l’intention de l’auteur

    Répondre

Laisser un commentaire Annuler la réponse

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée.

ARTICLES RECENTS

Nécrologie: Le Professeur Daouda Ndiaye en deuil…
Nécrologie

Nécrologie: Le Professeur Daouda Ndiaye en deuil…

25 février 2021
Levée de l’immunité parlementaire de Sonko: la commission Ad hoc validée
A LA UNE

Levée de l’immunité parlementaire de Ousmane Sonko : la liste des cinq orateurs qui seront autorisés à prendre la parole dévoilée

25 février 2021
Covid-19: les pistes de solution du Dr Papa Ndary Niang pour juguler la pandémie au Sénégal
SANTE

Covid-19: les pistes de solution du Dr Papa Ndary Niang pour juguler la pandémie au Sénégal

25 février 2021
Procès en diffamation: Serigne Mboup réclame 1milliard aux 11 membres du CCIAD
Justice

Procès en diffamation contre la Ccid: Serigne Mboup débouté

25 février 2021
Point du jour du coronavirus : 06 décès, 63 cas graves en réanimation et 268 nouvelles contaminations ce lundi 15 février 2021
COVID 19

Point du jour du coronavirus : 12 décès, 49 cas graves en réanimation et 288 nouvelles contaminations

25 février 2021
Alpha Condé : “les journalistes français ne respectent pas les chefs d’États africains, moi je n’accepte pas qu’on me manque de respect”
Afrique

Alpha Condé : “les journalistes français ne respectent pas les chefs d’États africains, moi je n’accepte pas qu’on me manque de respect”

25 février 2021
Assemblée nationale: échanges de propos aigres-doux entre Cheikh Bara Doly et Abdoulaye Makhtar Diop
Politique

Assemblée nationale: échanges de propos aigres-doux entre Cheikh Bara Doly et Abdoulaye Makhtar Diop

25 février 2021
Lagon 2: des jeunes qui se faisaient passer pour les fils de Macky et d’Idy arrêtés
Societe

Lagon 2: des jeunes qui se faisaient passer pour les fils de Macky et d’Idy arrêtés

25 février 2021
Revue de Presse (Wolof) de Zik Fm du Mercredi 03 Février 2021 avec Ahmed Aidara
Revues de La presse

Revue de Presse (Wolof) de Zik Fm du Jeudi 25 Février 2021 avec Ahmed Aidara

25 février 2021
Revue de presse (wolof) Rfm du mercredi 03 février 2021 avec Mamadou Mouhamed Ndiaye
Revues de La presse

Revue de presse Rfm du 25 février par Mamadou Mouhamed Ndiaye

25 février 2021
La UNE des quotidiens de ce jeudi 25 février 2021
La Une des Quotidiens

La UNE des quotidiens de ce jeudi 25 février 2021

25 février 2021

#XALIMA15ANS

15 ans de Xalima: les voeux et témoignage de Mamadou Kane (Makane)
Xalima Tv

15 ans de Xalima: les voeux et témoignage de Mamadou Kane (Makane)

5 novembre 2020
15 ans de Xalima: Le témoignage d’Hady Traoré DSE Canada
Xalima Tv

15 ans de Xalima: Le témoignage d’Hady Traoré DSE Canada

5 novembre 2020
15 ans Xalima: les voeux de Papiss Création chargé de l’Organisation de l’Association des Maîtres Tailleurs du Sénégal
Xalima Tv

15 ans Xalima: les voeux de Papiss Création chargé de l’Organisation de l’Association des Maîtres Tailleurs du Sénégal

3 novembre 2020
Le «Souley-man show», Acte 2! Par Momar Mbaye
Xalima Tv

15 ans de Xalima: Les voeux et encouragements du ministre Souleymane Jules Diop

30 octobre 2020
15 ans d’existence- Comment Xalima s’est démarqué de la masse pour maintenir sa ligne de conduite
Xalima Tv

15 ans d’existence- Comment Xalima s’est démarqué de la masse pour maintenir sa ligne de conduite

28 octobre 2020
15 ans de Xalima: Les voeux de Birane Diaw
Xalima Tv

15 ans de Xalima: Les voeux de Birane Diaw

28 octobre 2020
15 ans de Xalima: Les voeux de Tafsir Ndické Diéye Poète, Romancier, Chroniqueur
Xalima Tv

15 ans de Xalima: Les voeux de Tafsir Ndické Diéye Poète, Romancier, Chroniqueur

28 octobre 2020

A LA UNE DES QUOTIDIENS

La UNE des quotidiens de ce jeudi 25 février 2021
La Une des Quotidiens

La UNE des quotidiens de ce jeudi 25 février 2021

25 février 2021
0

Lire
Xalima.com

© 2020 Xalima.com All Rights Reserved

  • Presentation
  • Conditions d’utilisation
  • CONTACTS
  • PUBLICITE
  • RADIO FM

Nous Suivre

No Result
View All Result
  • ACCUEIL
  • ACTUALITES
  • Chroniques
    • L’oeil de l’expert avec Cheikh Faye Ph.D
    • Alassane Kitane
    • AUTOPSIE
    • Bathie Ngoye Thiam
    • Bosse Ndoye
    • Les chroniques de Sigapal
  • Opinions
  • PEOPLE
  • SPORTS
  • VIDEOS
  • RADIO FM

© 2020 Xalima.com All Rights Reserved

Welcome Back!

Login to your account below

Forgotten Password?

Create New Account!

Fill the forms bellow to register

All fields are required. Log In

Retrieve your password

Please enter your username or email address to reset your password.

Log In

Add New Playlist

This website uses cookies. By continuing to use this website you are giving consent to cookies being used. Visit our Privacy and Cookie Policy.
Open chat