spot_img

Viatique du 03 mai 2024 : Compétence…(Par Dr Massamba Gueye)

Date:

« La compétence n’a ni âge, ni religion, ni ethnie, ni couleur de peau, ni nationalité, ni sexe, ni idéologie. On est compétent.e ou on ne l’est pas ! La Compétence est la capacité de penser, de faire et/ou de dire, acquise par apprentissage ou de façon innée, qui te donne l’habilité d’agir sans tâtonner. Elle te protège si elle est soutenue par deux piliers : la rigueur et l’éthique. Arme-toi donc d’elle, c’est ton bouclier absolu contre les contempteurs. Ta compétence n’est cependant en rien utile si elle ne se nourrit que de routines qui t’empêchent de performer. Cette performance est le résultat optimal, ingénieux et original que tu atteins, chaque instant de ta vie, grâce à ta manière de faire différemment les choses, au point d’obtenir, de façon efficiente, les meilleurs résultats. Si ta compétence ne produit pas des performances, elle n’est que décorative ! Tire profit d’elle et tu passeras de l’efficacité à l’efficience. Qui ne fait que répéter ce qui est déjà fait, n’a pas de génie.
 
Si tu n’es pas compétent.e et que tu ne cherches pas à l’être, tu es une cible facile pour qui veut sacrifier ta carrière car tu lui donnes, par tes insuffisances, le moyen de te broyer. Pour éviter cela, apprends sans cesse, cultive ta compétence par une mise à jour quotidienne de ton savoir, ton savoir-faire et ton savoir être. Ce dernier triptyque est la sève qui alimente ton aisance professionnelle. Par ton expérience, irrigue ta compétence de jouvence éternelle. Elle mûrira alors sans vieillir si tu sais être agile et mobile dans ton domaine. Ta polyvalence maitrisée sera ton outil de pilotage de tes performances contre la lassitude professionnelle et l’échec social.
 
Si l’alibi pour t’ostraciser est ton âge, ton genre humain, ta race ou ton origine sociale, la meilleure réponse que tu pourras opposer à cette malhonnêteté intellectuelle, sexiste, raciste ou autres c’est ta compétence. Elle sera l’avocate qui empêchera de dormir, si tu es toujours honnête avec ton emploi et sociable dans ton environnement professionnel, qui veut te discriminer et discréditera tout jugement subjectif sur toi. Par contre, ton incompétence te rend fragile et t’expose au ridicule. Cherche les savoirs et aptitudes honorables qui te rendent incontournable si tu veux te faire respecter ».
Bon Vendredi.
Dr Massamba GUÉYE LBA

nayrafet


Yóbbalu 03 fanu me 2024
Man sa liggéey …
« Man sa liggéey, peeg ko ajuwut ci at, waaso, der, réew, gis-gis mbaa diine. Dangay xam ngañ mbaa nga cuune rekk. Gànnayool sa xam-xamu liggéey ndax moo lay aar ci ñi lay xas. Man sa liggéey nak mooy ràññee la nga war a def ak di ko def te doo làmbatu. Moo lay aar. Ñaar yii kenn ñoo leen war a téye: njub ak ñàkk caaxaan. Sag man sa liggéey nak du am njariñ fii ak la nga dëkkee def rekk ngay baamtu saa su ne, ndax day tax doo xarañ mba am ndam ya gën. Def googa ngay def kéemtaan ci sa liggéey waxtuwu nekk moo lay wuutale ak ñeneen ñi ba tax li sa loxo di saf beneen du ko saf. Mooy liy tax kenn du la mëdd. Kuy baamtu bés bu nekk doo njuuma bay def lu kenn xaarul.
 
Boo manut sa liggéey, dangay yomb a bëmëx ci képp ku la bëgg a beddi ndax yaa koy jox paaka bi la nàndal ci say lajj. Ngir moytu loolu nak, deel yeesal sa xam-xam, sa liggéeyin ak sag xam àdduna. Ñatt yu mujj yooyu ñooy dundal sag nekk ci sa liggéeyukaay. Sa yàgg ci liggéey bi moo lay dooleel ndax yàgg a joow. Sag man sa liggéey day màgg te du ruus sudee yaangi jàng foo tollu. Sag xarala mooy sa doole yit.
 
Ku la bëgg a dàq say at, sab der, sa waaso walla sa diine lay latoo waaye na ko sag man a liggéey bunxataal ba du am bunt bum jaar ba am dëgg ci sa kow. Sag man a liggéey na doon sa làyyilkat. Soo nekkee ku xamut liggéeyam nak lu la dal yaa ko teg sa bopp ndax ku wéeruwut fenn neex a bëmëx. Wutil xam-xam bi war te dëkk ci di ko yeesal soo bëggee di am mbégte te ñu naw la. »
Àjjumay jàmm.
Dr Masàmba GÉY LBA

nayrafet

1 COMMENTAIRE

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici

spot_img

DEPECHES

DANS LA MEME CATEGORIE
EXCLUSIVITE

« Propos d’un juge » (Par Moussa Bèye)

Dans cet ouvrage « Propos d’un juge » qui...

Université Assane Seck de Ziguinchor : le Conseil académique fixe la reprise des cours au 06 janvier et menace

XALIMANEWS: Les cours vont reprendre à l’Université Assane Seck...