Viatique du 12 août 2022 : Estime…(Par Dr Massamba Guye)

Date:

Si tu ne crois pas en l’utilité de ta vie, personne n’y croira. Si tu te dévalorises, n’espère le respect de personne! Secoue-toi, dépoussière tes doutes, hypnotise tes hésitations, bannis tes regrets et intronise ton espoir si tu veux que ta vie soit une victoire !

Les écueils de la vie et les coups bas ne sont que des étapes décisives à surmonter pour grandir. Si, par contre, à chaque épreuve, tu es le premier à douter de toi-même, si tu es le premier à te juger inapte à, socialement et professionnellement, exceller et si tu te prends pour un moins que rien, ne sois pas surpris que le monde te voie tel que tu te dessines.

Il faut te tracer une ligne de mire, te fixer un horizon, mais surtout, sans fierté déplacée, t’armer d’estime de soi. Nul n’est voué à la faillite originelle. Il n’y a que des personnes qui n’ont pas le courage de se croire capables de réussir malgré les affres de la vie. Crois en toi, tu es un don, tu as un don ! »
Bon Vendredi.
Dr Massamba GUEYE LBA

Yóbbalu 12 fanu Ut 2022
Nawlu…
Ku weddi sa bopp, kenn du la gëm. Ku gëmut ne sag dund am na njariñ, keneen du ko gëm. Boo wóoluwul sa bopp, bul xaar kenn wóolu la.
Jógal jéem dara, dàqal xel-ñaar, nootal jiixii-jaaxa, aayalal réccu, dëkkóol yaakaar ak fit boo bëggee am ndam ci àdduna. Jafe-jafey àdduna ak i gàllankooram du ludul ay jung i jéego yoo war a def ba jëm kanam.
Waaye bu dee yaa njëkk a weddi sa bopp, bu dee saa yu tare nga ne doo ko man ci sa wàllu liggéey mbaa ci kër gi, su dee da nga jàppe sa bopp ku tekkiwul dara, ni nga wanee sa bopp rekk la la sa ñoñ di gisee.
Nit day sàkkal boppam një waaye li ëpp solo mooy mu naw boppam te woyof. Ku nawut sa bopp, kenn ku baax du la nawloo. Yàlla sàkkut kenn nit ku tekkiwut dara, ku xamut dara, ku manut dara. Li am kay mooy ku xeeb boppam ne moom sagaru nit la tax mu ne yàcc, àdduna di ko pamti-pamtee. Nawal sa bopp ndax tànneefu Yàlla nga. »
Àjjumay Jàmm!
Dr Masàmba GÉY LBA

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici

CAN 2023

DEPECHES

DANS LA MEME CATEGORIE
EXCLUSIVITE

Héros ou complices (Par Pr Mary Teuw Niane)

Lorsque l’éthique et la morale sont rangées dans les...

Pierre Goudiaby…non à tes gesticulations criminelles (Par Adama Gaye)

Encore toi. Halte, Pierre…Traité d'escroc par Macky Sall voici...

La vérité sur le PDS et son patron officieux (Par Marvel Ndoye)

Le PDS est en train de prouver tous les...